Inondations Sénégal : Algérie diapalé na Sénégal thi 80 tonnes thi ay aidé alimentaire
Thi cadrou diapalén té, Deuk bigua xam ni moy Algérie ak Sénégal, mardi thi souba 16 août 2022 bign guén, thiéty (03) thi ay avions transport militaire yo kham ni force de aérienne bou armée nationale bi moko mom niew nagn figua kham ni moy Dakar ak dimbal (aide humanitaire) yo xam ni mogui tolou thi 80 tonnes, lolou nak ministre bougnou dink waloum waloum défense moko xam lé. Ndimall yoyou nak mogui diougué thi Croissant-Rouge algérien pour diapalé gni lorou thi mbeunde mi thi ville Bou Dakar/Sénégal bi. Guinaw presse locale bi nak ndimall yoyou mogui composé ay produits alimentaires, ay médicaux ak pharmaceutique... Lolou nak thiéty 03 thi ay avions bou armée de l'air algérienne bi... Bathi aéroport international bou Blaise Diagne.

Commentaires
Enregistrer un commentaire