Accéder au contenu principal

Lignou Xam thi Hadi Matar, Ki gua xam ni moy Agresseur présumé Bou Salman Rushdie

 

Kigua xam ni moy Versets sataniques, Salman Rushdie mom lagn Diame thi jour bi méguo ak 12 Août. Bobou nak migui wone thi pleine conférence thi deuk New York. Kiko Agressé nak tékk nagn ko lokho thi Lou gaw. Guinaw info yi nitt kokou nak app musulman chiite Bou d'origine libanaise la.

Commentaires

Posts les plus consultés de ce blog

Urgent : Diourbel Bén émigré mo pendu bopam thi bén grap

Bén Way buy Wouyo thi tourou T.WAGNE, émigré la tolou thi 33ans, mo pendu popam thi bén grap avec sa ceinture, thi quartier bougnouy wakh Keur Yelly nék feulé thia Diourbel. Guinaw sources You Seneweb, Marchand ambulant, la wone Diougué thia Gambie. Nékone thi bén keurou onclam. Xibar bobou nak mogui diougué thi sén quartier, thi goudi démb bi. Éléments Bou Commissariat central Bou Diourbel yégual nagn lén ko thi samedi ay 03h du matin. Éléments wou commissaire Mor Ngom niew nagn thi lieux bi xol nagn affaire yi guiss ben nit Bou niakk bakanam bouy weudélou thi branche garap bi ak guélow bi Guinaw bign défé constat bi par la police, corps bou T.W Yobou nagn ko thi morgue bou hôpital régional bou Baol pour déff autopsie. Enquête bi nak mogui thi yone. KAAY XOOL INFOS  

Sadio Mané dougal na 6 buts You VAR Bagn ?

  Mba kham guén ni Sadio Mané dougal na 6 buts You VAR bagn Kom niguén ko guissé thi 4 matchs yi Sadio Mané football Bayern Munich dougal na déjà 6 buts yo kham ni VAR daff ko bagn🤔 Kaayxoolinfos 

Urgent l'Allemagne Dakal na opérations militaires Bim warone amal Mali

  l'Allemagne mo annoncé thi jeudi 11 août bign guén suspendre «Ba bénén yone» Lou beuri thi lougnouy amal ay opérations militaires thia Mali thi tanku Mission Bou l'ONU (Minusma), wané nagn bén niak accord thi survol par autorités maliennes yi. «Ba takh na gouvernement malien bi ndaguoul woul accord d'autoriser bén vol bign beugone amal tay» Bi warone assurer révolution wu personnel, wax na tamit porte-parole bu ministère allemand bu défense. «Gnom dagnouy arrêter jusqu'à nouvel ordre sen opérations de reconnaissance ak vol yi transport par hélicoptère / ndaw gnom meuneu tougn diapalé Minusma thi sén plan opérationnel» Lign si yok