VISITOU PRÉSIDENT MACKY SALL FEULÉ THIA MALI.
Président Macky Sall accueilli nagn ko thi lundi 15 août 2022 bi, thia aéroport international bou Madibo Keïta Bamako-Senou thi ndogalou président bu Mali, Colonel Assimi GOÏTA, ak membres Bou gouvernement bi ak corps diplomatique yi.
Chef de l'Etat bi nak mogui Mali guirr amal visite d'amitié Ak travail.
KAAY XOOL INFOS



Commentaires
Enregistrer un commentaire