Bén Way buy Wouyo thi tourou T.WAGNE, émigré la tolou thi 33ans, mo pendu popam thi bén grap avec sa ceinture, thi quartier bougnouy wakh Keur Yelly nék feulé thia Diourbel. Guinaw sources You Seneweb, Marchand ambulant, la wone Diougué thia Gambie. Nékone thi bén keurou onclam. Xibar bobou nak mogui diougué thi sén quartier, thi goudi démb bi. Éléments Bou Commissariat central Bou Diourbel yégual nagn lén ko thi samedi ay 03h du matin. Éléments wou commissaire Mor Ngom niew nagn thi lieux bi xol nagn affaire yi guiss ben nit Bou niakk bakanam bouy weudélou thi branche garap bi ak guélow bi Guinaw bign défé constat bi par la police, corps bou T.W Yobou nagn ko thi morgue bou hôpital régional bou Baol pour déff autopsie. Enquête bi nak mogui thi yone. KAAY XOOL INFOS